# Wolof translation for klavaro. # Copyright (C) 2012 Felipe Castro # This file is distributed under the same license as the klavaro package. # # Dominique Rochefort , 2012. msgid "" msgstr "" "Project-Id-Version: klavaro 1.9.4\n" "Report-Msgid-Bugs-To: \n" "POT-Creation-Date: 2020-05-30 13:47-0300\n" "PO-Revision-Date: 2012-MO-DA HO:MI+ZONE\n" "Last-Translator: Dominique Rochefort \n" "Language-Team: Wolof \n" "Language: wo\n" "MIME-Version: 1.0\n" "Content-Type: text/plain; charset=UTF-8\n" "Content-Transfer-Encoding: 8bit\n" "X-Bugs: Report translation errors to the Language-Team address.\n" "Plural-Forms: nplurals=2; plural=(n!=1);\n" "X-Generator: Translate Toolkit 1.9.0\n" #: ../data/klavaro.glade.h:1 msgid "Klavaro - Progress" msgstr "Klavaro - Jéego yi" #: ../data/klavaro.glade.h:2 msgid "_Lesson:" msgstr "Saar" #: ../data/klavaro.glade.h:3 msgid "Value" msgstr "Dayo" #: ../data/klavaro.glade.h:4 #, fuzzy #| msgid "Reset progress data" msgid "Clear progress data." msgstr "far rootaani yokkute" #: ../data/klavaro.glade.h:5 msgid "_Reset" msgstr "_Suqaliwaat" #: ../data/klavaro.glade.h:6 msgid "Close this window, returning to the exercise." msgstr "Tëj palanteer bii, dellusi ci jéemantu bi." #: ../data/klavaro.glade.h:7 msgid "_Close" msgstr "Tëj" #. Everything means ALL the progress charts statistics. #: ../data/klavaro.glade.h:9 msgid "everything!" msgstr "" #. Confirmation check-button for removing data. #: ../data/klavaro.glade.h:11 #, fuzzy #| msgid "Clear all the progress data, for every module." msgid "Clear data for every module, if checked!" msgstr "Far xibaar yi aju ci fi nu tollu, ci modil yépp." #: ../data/klavaro.glade.h:12 msgid "Load other exercises/lessons" msgstr "Ubbi yeneeni jéemantu/saar/ Gàttal : [Ctrl-O]" #: ../data/klavaro.glade.h:13 msgid "_Other texts" msgstr "Yeneeni mbind" #: ../data/klavaro.glade.h:14 msgid "Edit the character set to be used in this lesson." msgstr "Soppiléen njabootu araf yi ñu war a jëfandikoo ci saar wii." #: ../data/klavaro.glade.h:15 msgid "This is a specific exercise, adjusted to your error profile." msgstr "Lii jéemantu bu beru la, dañu koo méngaleek njuumte yi ngay faral di def." #: ../data/klavaro.glade.h:16 #, fuzzy msgid "Edit the character set to be used in lessons after 43: they are customizable!" msgstr "Soppiléen njabootu araf yi ñu war a jëfandikoo ci saar 44 ba 50." #: ../data/klavaro.glade.h:17 ../src/tutor.c:398 msgid "Drag and drop text here to practice with it." msgstr "Diriléen te teg mbind wi fii ngir tàggat sa bopp ci tàppe." #: ../data/klavaro.glade.h:18 #, fuzzy msgid "Press here to restart the exercise. Hotkey: [Ctrl-R]" msgstr "Bësal fii ngir tàmbaliwaat jéemantu bi. Gàttal : [Ctrl R]" #: ../data/klavaro.glade.h:19 msgid "Show the virtual keyboard and the relation between fingers and keys." msgstr "Wonem arafukaay bi ñu nataal ak ni baaraam yeek butoŋ yi ànde" #: ../data/klavaro.glade.h:20 msgid "_Keyboard" msgstr "Arafukaay" #: ../data/klavaro.glade.h:21 msgid "Select the font to be used in the exercise window." msgstr " Fal-léen njabootu araf yi ngéen di jëfandikoo ci palanteeru jéemantu yii" #: ../data/klavaro.glade.h:22 msgid "Font definition" msgstr "Tànnum njabootu araf" #: ../data/klavaro.glade.h:23 msgid "Alternative color scheme, needs restart!" msgstr "" #: ../data/klavaro.glade.h:24 msgid "Co_urse information" msgstr "Xibaar ci saar wi" #: ../data/klavaro.glade.h:25 msgid "Charts showing the learning progress along the exercises." msgstr "Nataal wuy wone ni nuy jëme kanam ci saa su nuy jéemantu." #: ../data/klavaro.glade.h:26 msgid "_Progress" msgstr "_Jéego yi" #: ../data/klavaro.glade.h:27 msgid "Exit the application immediately." msgstr "Génnal leegi ci jefekaay bii: Gàttal : [Ctrl-Q]" #: ../data/klavaro.glade.h:28 msgid "Return to the main menu." msgstr "Dellusi ci jël lu mag li" #: ../data/klavaro.glade.h:29 msgid "B_ack to menu" msgstr "Dellusi ci njël li" #: ../data/klavaro.glade.h:30 msgid "Show local and external scores from other users." msgstr "Wone manoore biir ak biti yu yeneeni jëfandikookat." #: ../data/klavaro.glade.h:31 msgid "_Top 10" msgstr "_Top 10" #: ../data/klavaro.glade.h:32 msgid "Change language" msgstr "Soppi lammiñ" #: ../data/klavaro.glade.h:33 msgid "Attention!" msgstr "Moytul!" #: ../data/klavaro.glade.h:34 msgid "Do you confirm?" msgstr "Ndax woor na la?" #: ../data/klavaro.glade.h:35 msgid "_No" msgstr "Déedéed" #: ../data/klavaro.glade.h:36 msgid "_Yes" msgstr "Waaw" #: ../data/klavaro.glade.h:37 msgid "Klavaro - Select file" msgstr "Klavaro - Tànnum dencukaay" #: ../data/klavaro.glade.h:38 msgid "_Cancel" msgstr "Neenal" #: ../data/klavaro.glade.h:39 msgid "_Open" msgstr "Ubbi" #: ../data/klavaro.glade.h:40 msgid "Re_name:" msgstr "Sàkkalaat tur:" #: ../data/klavaro.glade.h:41 msgid "Rename the selected item." msgstr "Sàkkalaat tur mbir mi faluwoon" #: ../data/klavaro.glade.h:42 msgid "Read a text file and add a copy of it here. The file must be encoded in UTF-8." msgstr "Njàng ab dencukaayu mbind te roof fii ab duppit. Dencukaay bi dafa war a nekk lu nu fas ci UTF-8" #: ../data/klavaro.glade.h:43 msgid "_Open text file" msgstr "Ubbi dencukaayu mbind yi" #: ../data/klavaro.glade.h:44 msgid "Paste text that was copied to the clipboard." msgstr "Taf mbind wi ñu duppiwoon ci dencandikaay bi." #: ../data/klavaro.glade.h:45 msgid "_Paste from clipboard" msgstr "Taf bu dale ca dencandikaay ba" #: ../data/klavaro.glade.h:46 msgid "Remove the selected item." msgstr "Màbb mbir mi falu." #: ../data/klavaro.glade.h:47 msgid "_Remove copied file" msgstr "_Màbb duppi dencukaay bi" #: ../data/klavaro.glade.h:48 msgid "Apply the selected item to create an exercise." msgstr "Jëfe mbir mi falu ngir sos ab jéemantu" #: ../data/klavaro.glade.h:49 msgid "_Apply" msgstr "Jëfe" #: ../data/klavaro.glade.h:50 msgid "Close this window." msgstr "Tëj palanteer bii." #: ../data/klavaro.glade.h:51 msgid "Country / Custom" msgstr "Réew / solal" #: ../data/klavaro.glade.h:52 msgid "Variant" msgstr "Xeet" #: ../data/klavaro.glade.h:53 msgid "Remove the selected custom layout." msgstr "Màbb tëralinu solal wi nu faloon" #: ../data/klavaro.glade.h:54 msgid "_Remove" msgstr "_Màbb" #: ../data/klavaro.glade.h:55 msgid "Toggles the shift effect on the keys. Alternates between the upper and lower characters of the keys." msgstr "Jaabante diggante arafu mage yi ak yu ndaw yi ci butoŋ yi" #: ../data/klavaro.glade.h:56 msgid "SPACE BAR" msgstr "Bànqaasu teqale" #: ../data/klavaro.glade.h:57 ../src/keyboard.c:1722 msgid "thumbs" msgstr "Puus" #: ../data/klavaro.glade.h:58 msgid "Tab" msgstr "" #: ../data/klavaro.glade.h:59 msgid "Ctrl" msgstr "Ctrl" #: ../data/klavaro.glade.h:60 msgid "Caps" msgstr "Xomb. Rajj" #: ../data/klavaro.glade.h:61 msgid "S_ave as:" msgstr "aar ci" #: ../data/klavaro.glade.h:62 msgid "Show previous screen." msgstr "Wone seetukaay bi jiitu" #: ../data/klavaro.glade.h:63 msgid "_Previous step" msgstr "Tollu tollu bi jiitu" #: ../data/klavaro.glade.h:64 msgid "Show next screen." msgstr "Wone seetukaay bi ci topp" #: ../data/klavaro.glade.h:65 msgid "_Next step" msgstr "Bi ci topp" #: ../data/klavaro.glade.h:66 msgid "Return without any modification." msgstr "Dellusi te bañ a jefe benn coppite" #: ../data/klavaro.glade.h:67 msgid "Save the current keyboard layout with the name specified above." msgstr "Aar tabalu arafukaay bi ñu tollu ak tur wi ñu wone ci kow." #: ../data/klavaro.glade.h:68 msgid "_Save and use" msgstr "Aar te jëfandikoo" #: ../data/klavaro.glade.h:69 msgid "If you like those beautiful hands, click here to close this window keeping them." msgstr "Su ngéen soppee loxo yu jekk yii, cuq leen fii ngir tëj palanteer bi te dencaale leen." #: ../data/klavaro.glade.h:70 msgid "_Keep hands" msgstr "Denc loxo yi" #: ../data/klavaro.glade.h:71 msgid "Klavaro - Main menu" msgstr "Klavaro - Njël lu mag" #: ../data/klavaro.glade.h:72 msgid "Don't be shy about learning the basics!" msgstr "Bu leen am xel ñaar ci jàng cosaan yi" #: ../data/klavaro.glade.h:73 msgid "Learn how to type correctly" msgstr "Nan la ñuy tàppee mu aw yoon" #: ../data/klavaro.glade.h:74 msgid "Initial training for your fingers." msgstr "Tàggatum baaraam gi jëkk." #: ../data/klavaro.glade.h:75 msgid "First steps with initial training" msgstr "Jéego bi jëkk: tàggatum ndoorte" #: ../data/klavaro.glade.h:76 msgid "Memorizing the keyboard practicing random keys exercises." msgstr "Mokkal arafukaay gi wéeru ci ndimbalu butoŋ bu mu mën di doon." #: ../data/klavaro.glade.h:77 msgid "Practice with random keys" msgstr "Tàggat ak ay butoŋ yu mu mën di doon" #: ../data/klavaro.glade.h:78 msgid "Accelerating the touches practicing random words exercises." msgstr "Gaawalug mbind mi ak ay jéemantu yu sukkandiku ci baat yu mu mën di nekk" #: ../data/klavaro.glade.h:79 msgid "Practice with random words" msgstr "Tàggat ak ay baat yu mu mën di doon" #: ../data/klavaro.glade.h:80 msgid "Becoming proficient practicing complete paragraphs exercises." msgstr " Nekksiléen ku xaran ak jéemantu yi sukkandiku ci xise yu mët sëkk,." #: ../data/klavaro.glade.h:81 msgid "Practice with complete texts" msgstr "Tàggat ak ay mbind yu mët sëkk" #: ../data/klavaro.glade.h:82 msgid "Speech" msgstr "Fitté" #: ../data/klavaro.glade.h:83 msgid "Your language here." msgstr "Sa lammiñ." #: ../data/klavaro.glade.h:84 msgid "Keyboard layout for modules 1 and 2. Also used informatively in the fluidness contest." msgstr "Xamle arafukaay ci modil 1 ak 2. Ba tey itam moom lañuy jëfandikoo ci saaru rattaxal yi." #: ../data/klavaro.glade.h:85 msgid "_Keyboard:" msgstr "Arafukaay" #: ../data/klavaro.glade.h:86 msgid "Language for modules 3 and 4." msgstr "Lammiñ ngir sumb 3 ak 4" #: ../data/klavaro.glade.h:87 msgid "_Language:" msgstr "Làmmiñ" #: ../data/klavaro.glade.h:88 msgid "Little tip about this program." msgstr "Pexe su ndaw ngir porogaraam bii." #: ../data/klavaro.glade.h:89 msgid "_Help" msgstr "Ndimbal" #: ../data/klavaro.glade.h:90 msgid "General information about the program." msgstr "Xibaar yu ëmb lépp te aju ci xeltéef gii." #: ../data/klavaro.glade.h:91 msgid "_About..." msgstr "Ci mbiri..." #: ../data/klavaro.glade.h:92 msgid "About 'Klavaro'" msgstr "Ci mbiri \"Klavaro\"" #: ../data/klavaro.glade.h:93 ../data/klavaro.desktop.in.h:2 msgid "Yet another touch typing tutor" msgstr "xeltéefub njàngum daktilo" #: ../data/klavaro.glade.h:94 msgid "Remember always: someone loves you!" msgstr "Fàttaliku-léen bés bu nekk ne am na ku leen bëgg!" #: ../data/klavaro.glade.h:95 msgid "Help?" msgstr "Ndimbal?" #: ../data/klavaro.glade.h:96 msgid "This is a tip. Now you press this button to return to the main menu." msgstr "Lii ab xelal la. Bës leen ci butoŋ bi ngir dellusi ci njël lu mag li. " #: ../data/klavaro.glade.h:97 msgid "The main menu of the application is very straightforward. Just select the type of exercise you wish to take. Do not worry about clicking any button on the screen. The buttons will never hurt you!" msgstr "Jël lu mag li ñeel xeltéef bi lu yomb la. Fal leen rekk xeetu jéemantu bi ngeen fas yéenée def. Buléen ragal a cuq butoŋ yi, duñu leen ngaañ" #: ../data/klavaro.glade.h:98 msgid "Also the controls have tips which will appear if you hover over them with your mouse. These tips can come in very handy. To see how these tips work, position your mouse over the button below, and without clicking, wait for the tip to appear..." msgstr "Te itam, butoŋ bu nekk dafa am waxtaanu ndimbal mu koy mottali. Ngir wone ko, tegal jinax ji ci kow butoŋ bi bañ a cuq te xaar tuuti..." #: ../data/klavaro.glade.h:99 msgid "Top 10" msgstr "Top 10" #: ../data/klavaro.glade.h:100 #, fuzzy msgid "Show extra information." msgstr "Wone xibaar yi yokku" #: ../data/klavaro.glade.h:101 #, fuzzy msgid "Hide extra information." msgstr "Nëbb xibaar yi yokku" #: ../data/klavaro.glade.h:102 msgid "Publish to the web your local scores." msgstr "Yéene say manoore ci internet" #: ../data/klavaro.glade.h:103 msgid "_Participate" msgstr "Bokk" #: ../data/klavaro.glade.h:104 msgid "Download from the web the most up to date ranking." msgstr "Yebléen ci internet ndenc yi gën a ànd ak jamono." #: ../data/klavaro.glade.h:105 msgid "_Update" msgstr "_Yeesal" #: ../data/klavaro.desktop.in.h:1 msgid "Klavaro" msgstr "Klavaro" #: ../data/klavaro.desktop.in.h:3 #, fuzzy msgid "A very flexible and efficient touch typing tutor." msgstr "xeltéefub njàngum daktilo" #: ../src/main.c:304 msgid "(Custom)" msgstr "(solal)" #: ../src/main.c:305 msgid "(Edit custom)" msgstr "(Jagal jëmmalin yu ñu solal)" #: ../src/main.c:306 msgid "(Default)" msgstr "(Ñakk ndigal)" #: ../src/main.c:383 #, c-format msgid "Dictation mode (depends on this speech synthesizer: %s)" msgid_plural "Dictation mode (depends on one of these speech synthesizers: %s)" msgstr[0] "Anamu fitté (aju ci dëxëñukaayu wax : %s)" msgstr[1] "Anamu fitté (aju ci dëxëñukaayu wax ji : %s)" #. Set main labels (for translation) #. #: ../src/main.c:425 ../src/keyboard.c:1381 msgid "Introduction" msgstr "Ubbite" #: ../src/main.c:428 ../src/top10.c:110 msgid "Basic course" msgstr "Saari cosaan" #: ../src/main.c:431 ../src/top10.c:113 msgid "Adaptability" msgstr "Mën a ànd" #: ../src/main.c:435 ../src/main.c:437 ../src/callbacks.c:1429 #: ../src/top10.c:90 ../src/top10.c:116 msgid "Speed" msgstr "Gaawaay" #: ../src/main.c:440 ../src/callbacks.c:1452 ../src/top10.c:92 #: ../src/top10.c:119 msgid "Fluidity" msgstr "Rataxaay" #: ../src/callbacks.c:508 ../src/tutor.c:548 msgid "Keys:" msgstr "Butoŋ yi:" #: ../src/callbacks.c:903 ../src/callbacks.c:919 msgid "Connecting..." msgstr "Jokkoo baa ngi ci yoon..." #: ../src/callbacks.c:1192 msgid "Overwrite user layout" msgstr "Nappaaje benn taabalu arafukaay gu ñu solal" #: ../src/callbacks.c:1194 msgid "This will OVERWRITE an existent keyboard layout." msgstr "Lii dafay nappaaje benn taabalu arafukaay bu jotoon a am ba noppi" #: ../src/callbacks.c:1201 msgid "Remove user layout" msgstr "Màbb ab taabalu arafukaay gu ñu solal" #: ../src/callbacks.c:1203 msgid "This will REMOVE an existent keyboard layout." msgstr "Lii nii dafay màbb ab taabalu arafukaay bu jotoon a am" #: ../src/callbacks.c:1210 ../src/callbacks.c:1215 msgid "Reset progress data" msgstr "far rootaani yokkute" #: ../src/callbacks.c:1211 #, fuzzy #| msgid "This will DELETE all the progress data shown in the charts." msgid "This will DELETE all the progress data of all modules." msgstr "Lii nii dafay far rootaani yokkute yépp yi ñu wone ci xise yi." #: ../src/callbacks.c:1223 #, fuzzy, c-format #| msgid "This will DELETE all the progress data shown in the charts." msgid "This will delete the data of this chart. <%s>" msgstr "Lii nii dafay far rootaani yokkute yépp yi ñu wone ci xise yi." #: ../src/callbacks.c:1226 #, fuzzy, c-format #| msgid "Clear all the progress data, for every module." msgid "This will delete the progress data of the module. (%s)" msgstr "Far xibaar yi aju ci fi nu tollu, ci modil yépp." #: ../src/callbacks.c:1426 ../src/top10.c:88 msgid "Accuracy" msgstr "Jubaay" #: ../src/callbacks.c:1429 ../src/tutor.c:1332 msgid "(WPM)" msgstr "MPM" #: ../src/callbacks.c:1440 msgid "Errors" msgstr "Njuumte yi" #: ../src/callbacks.c:1443 msgid "Touch times (s)" msgstr "" #: ../src/callbacks.c:1455 ../src/tutor.c:1359 ../src/top10.c:70 msgid "Score" msgstr "Manoore" #. Translators: your language code (first 2 letters of your po-file) #: ../src/translation.c:522 ../src/tutor.c:1765 msgid "en" msgstr "wo" #: ../src/translation.c:609 msgid "The basic course focuses on having you read the characters presented to you on screen and typing the corresponding keys. Remember to keep your hands correctly oriented on the home row of the keyboard at all times (see introduction on main menu)." msgstr "Ci saaru ndorte bi, da ngeen cee war a jànge xeeti araf yiy feeñ ci palanteer bi, te bës butoŋ yi ñu méngool. Fàttalikuléen taxawaayi baaraam yi ci arafukaay gi ( yëral ubbite gi ci jël lu mag li)." #: ../src/translation.c:613 msgid "The key set used in each series will be shown in the above message line. The [Space], [Shift] and [Enter] keys may not show up there but are used very often." msgstr "Mbooleem butoŋ yi ñuy jëfandikoo ci bépp saar, ñi ngi wonewu ci kow. Yii buton (Espace), (Shift) ak (Enter) defuñu leen ci ndaxte dañu leen di jëfandikoo saa su nekk." #: ../src/translation.c:616 msgid "The message line below follows and echoes your key presses. If required, it changes and displays instructions for actions required from you." msgstr "Sàppe bi ci topp day wone xeetu araf yi méngook butoŋ yi ngeen di bës. Su ko soxlaa, mbind mi dafay soppeeku su ko defee mu wone ndigal yu bees." #: ../src/translation.c:620 msgid "Here you may practice and improve your memorization of all keys. There will be sentences presented with nonsense words which mix some numbers and symbols." msgstr "Di ngeen jànge fii jéemantu ak xam palaasu butoŋ yi. Am na ay jéemantu yu sukkandiku ci ay baat yu amul tekki, dañu jaxase ay araf, ay lim aki jëmm(symbol)" #: ../src/translation.c:623 msgid "In order to keep the lesson contents language and keyboard independent, accented letter combinations will probably not appear. For real word sentences, please use the fourth option of the main menu (about fluidness)." msgstr " Ngir sukkandi ci kàddu ëmb baat dëgg ba tàggatu, demléen ca ñeenteelu tànneef gi ci jël lu mag li ( ci wàllu rattaxal)" #: ../src/translation.c:627 msgid "After each exercise there will be a brief statistics panel reviewing your performance along with some relevant comments." msgstr "Di ngéen gis ci njeextel jéemantu bu nekk seeni manoore, ak ay benn benni gis gis ngir jëmale léen kanam." #: ../src/translation.c:631 msgid "This exercise is very similar to the second one, for adaptability. The difference is that here you'll type real words." msgstr "Bii jéemantu dafay nirook ñaareel biy wax lu jëm mën a soppiku. Wuutu gi : fii da ngéen fiy tàppe ay baat dëggantaan ci seenug làmmiñ " #: ../src/translation.c:634 msgid "The default language is the actual one of the interface. But you may select any other texts with words you would like to use. Press the 'Other' option above and add files containing those texts." msgstr "Làmmiñ ñakk ndigal mooy wi ñu indi ngir wone (wolof ci fii). Waaye mën ngéen a tànn yeneen mbind ak ay baat yu ngeen bëgg a jëfandikoo. Cuq leen ci tànneef \"Yeneen\" (ci kow) te yokk ci dencukaay yi ëmb waxtaan yi." #: ../src/translation.c:638 msgid "With this exercise the focus is on speed. So, you are supposed to type really fast and I will only flatter you when you deserve it!" msgstr "Li ñu gën a soxal ci jéemantu jii mooy gaawaay. Koon, dangeen war a tàppe nu mu gën a gaawe! Jommal leen ma!" #: ../src/translation.c:642 msgid "We will now use complete sentences and paragraphs which make logical sense. This may distract you while you type if you try to understand what you are entering. The previous exercises were aimed at getting you to type without interpreting and analyzing the content." msgstr "Léegi, dañuy jëfandikoo ay baat yu mët ak ay xise yu am maanaa. Dafay waññi teylu daktilogaraaf bi jamono ju muy jéem a xam li muy bind. Su fekkee ne def ngéen jéemantu yi jiitu ni mu ware, waru léen a am jafe-jafe, ndaxte war ngéen a bind te du ngeen am benn gis-gis cimbind mi wi." #: ../src/translation.c:646 msgid "We do not mean to imply that the typists must behave like a robot, without understanding what they type. We do aim to develop the skill of typing, making it an automatic reflex akin to the acts of walking, talking, etc. After reaching this goal, the act of typing will become automatic and require little concentration. Then you will be able to pay attention to the real meaning of the text." msgstr "Waxuñu ne daktilogaraaf dafa war a mel ni masiin, nga xam ne du xam dara ci li muy bind. Xanaa kay li ñu soxal kott moo di yokkuteg daktilogaraaf bi : dafa war a mën a gëmm di bind ni wax ak dox. Su yeggee ci jëmu jii, mbind mi dootul nekk coono: kon léegi, mën ngéen a def seen xelaat yépp ci maanaa mbind wi." #: ../src/translation.c:650 msgid "These exercises are longer. Each exercise consists of three paragraphs and the emphasis is placed on correctness and rhythm, with a minimum speed requirement. Here you will be required to use the backspace key to correct any mistakes. In other words, only input without error will be accepted." msgstr "Jéemantu yii ñoo gën a gudd. Bu ci nekk dafa ëmb ñetti xise te li fi ëpp solo mooy jubaay ak doxin, ak yemale gaawaay gi gën a néew. Fii, da nga wara jëfandikoo caabi far ngir defar yenn njumte yi. Mën nañu wax ni mbind yi ñu tappe te amul njumte rekk lañuy nangu." #: ../src/keyboard.c:1181 msgid "Correct positioning of the hands and fingers is very important to efficient typing. You will learn faster and type better if you follow the next recommendations." msgstr "Mbind mu jekk te yàgg dafay laaj loxo yeek baaraam yi tegu bu f ñu wara tegu. Su fekkee ne topp ngeen tegtal yii ni mu ware, seen njàng dafay gën a gaaw." #: ../src/keyboard.c:1184 msgid "The index-finger tips rest over each of the two keys which have a small raised mark, in the center of the keyboard." msgstr "Gindikaay yiy wone fi baaraamu joxañ bi di tege ci arafukaay bi mooy ñaari buton yu dëll yu nekk ci diggi arafukaay bi. " #: ../src/keyboard.c:1187 msgid "These marks function as 'tactile hooks' for your fingers to remain at the correct position. This way, with a little experience, you will not need to look at the keyboard to see if your fingers are properly positioned." msgstr "Gindikaay yii dañuy am taxawaayu wommat ngir bàyyi baaraam yi ci seen palaas. Niki noonu, ak tuuti jaar-jaar, dootul soxla ngeen di xool arafukaay bi ngir xam ndax baaraam yi tegu nañu fi ñu war a nekk." #: ../src/keyboard.c:1191 msgid "The tips of the other fingers lie naturally beside the index ones, over the keys on the same row of the keyboard." msgstr "Catu yeneen baaraam yi duu nekk feneen fu dul ce wetu baaraami joxan yi, ci butoŋ yi bokk sàppe. Bu fekkee ne arafukaay \"azerty\"/ \"qsdf\" fare ci loxo càmmooñ bi ak \"jklm ci loxo ndeyjoor." #: ../src/keyboard.c:1194 msgid "The outside edges of your thumbs rest over the space bar." msgstr " Catu baaraamu dëy yi dañuy tegu ci banqaasu teqale bi." #: ../src/keyboard.c:1196 msgid "The part of the hands closest to the wrist (the base) rest over the table, outside the keyboard. Without this kind of support the arms would quickly tire." msgstr "Tiwu njara yi tegu ci taabal ji, fu bokkul ci arafukaay bi. Su dul loolu, loxo yi dañuy gaaw a toqi." #: ../src/keyboard.c:1199 msgid "This is referred to as the home position for the hands. From it the fingers move all over the keyboard, reaching all the keys as naturally and quickly as possible. To reach this goal one uses a specific relation between each key and finger. This relation will be learned gradually as you complete the basic course." msgstr "Lii mooy taxawaayu cosaan bu baaraam yi. Ci li ko dale fii, la baaraam yi di dem ci arafukaay bi yépp, ak di jot butoŋ yépp ci anam gu woyof te gaaw. Ngir yegg ci nisër gii, butoŋ bu ci nekk dafa am anamu boppam bu muy jokkoo benn baaraam . Jokkoo yooyu lañu leen di jàngal ndànk-ndànd ci saaru cosaan wi." #: ../src/keyboard.c:1205 msgid "When learning the relation between fingers and keys, it is very important that you only move the finger which must press the key and allow all other fingers to remain in the home position." msgstr "Ci njàng mi, butoŋ bu nekk, dangéen di góorgóorlu ba du ngéen yëngal lu dul baaraam bi war. Te yeneen baaraam yi des ci seen taxawaay wa ñu amoon ca ndoorte la." #: ../src/keyboard.c:1209 msgid "After memorizing this relationship, you can relax the previous rule some, so that you can attain greater speed while typing." msgstr "Bu ngeen demee ba jàpp lëkkaloo yii, mën ngeen a topp tegtal yi jiitu ci anam yu gën a woyof, su ko defee ngeen mën a yokk seen gaawaay." #: ../src/keyboard.c:1212 msgid "The shift keys are used for capital letters and for some symbols. To get a shifted key input you should first use the small finger of the opposite hand. Just keep it in the closest Shift while reaching the target key with the other hand." msgstr "" #: ../src/keyboard.c:1216 msgid "You should be prepared to start training with the basic course. It will take effort and patience to be successful as a typist. We trust you have these and look forward to your success!" msgstr "Gannaaw faramfàcce yu gàtt yii, mën ngéen tàmbali saaru cosaan wi. Te ngeen di fàttaliku bés bu nekk : njàngum daktilo dafa laaj muñ, bañ a yàkkamti ! Wóolu nañu leen, bu ngeen ñu rusloo." #: ../src/keyboard.c:1227 #, c-format msgid "Step %i" msgstr "Tollu tollu %i" #. Recommendations #: ../src/keyboard.c:1231 msgid "To position the hands" msgstr "Tegléen seeni loxo fi war" #. Final words #: ../src/keyboard.c:1314 msgid "Go ahead!" msgstr "Dem na de! Ayca!" #: ../src/keyboard.c:1322 ../src/keyboard.c:1324 msgid "Click on any key to see which finger you must use:" msgstr "Bësal ci benn butoŋ ngir gis ban baaraam ngeen war a jëfandikoo" #: ../src/keyboard.c:1323 msgid "Relation between fingers and keys" msgstr "Lëkkaloo baaraam yeek butoŋu arafukaay bi " #: ../src/keyboard.c:1381 ../src/keyboard.c:1415 msgid "Keyboard" msgstr "Arafukaay " #: ../src/keyboard.c:1462 msgid "Create or modify a custom keyboard layout" msgstr "Joxléen tur tëraliinu bu bees bu arafukaay bi. " #: ../src/keyboard.c:1710 ../src/keyboard.c:1734 msgid "small finger" msgstr "baaraamu sanqaleeñ" #: ../src/keyboard.c:1713 ../src/keyboard.c:1731 msgid "ring finger" msgstr "Baaraamu jaaro" #: ../src/keyboard.c:1716 ../src/keyboard.c:1728 msgid "middle finger" msgstr "Baaraam bu mag bi" #: ../src/keyboard.c:1719 ../src/keyboard.c:1725 msgid "index finger" msgstr "Baaraam joxoñ" #: ../src/keyboard.c:1820 msgid "Press and edit me" msgstr "Bësléen ma ngir jagal ma" #: ../src/tutor.c:322 msgid "Lesson:" msgstr "Saar" #: ../src/tutor.c:332 msgid "Paragraphs:" msgstr "Xise" #: ../src/tutor.c:365 msgid "Klavaro - Basic Course" msgstr "Klavaro - Saaru ndorte" #: ../src/tutor.c:370 msgid "Klavaro - Adaptability" msgstr "klavaro - Dëppale" #: ../src/tutor.c:373 msgid "Adaptability exercises: automating the fingers responses, typing over all the keyboard." msgstr "Jéemantu dëppaloo: baaraam yiy dem na mu ware, jëfandikoo arafukaay bi yépp." #: ../src/tutor.c:378 msgid "Klavaro - Velocity" msgstr "Klavaro - Gaawaay" #: ../src/tutor.c:379 msgid "Velocity exercises: accelerate typing real words." msgstr "Jéemantu gu ñeel gaawaay ; gaawal ci kow mbindum baat dëggantaan" #: ../src/tutor.c:383 msgid "Klavaro - Fluidness" msgstr "Klavaro - Rataxaay" #: ../src/tutor.c:385 msgid "Fluidness exercises: accuracy typing good sense paragraphs." msgstr "Jéemantu rattaxaay : Tappe bu jub ak mbindum xise bu am maanaa." #: ../src/tutor.c:447 msgid "End of exercise. Press [Enter] to start another." msgstr "Njeextel jéemantu. Bësal ci [Entrée-Duggal] ngir tàmbali beneen." #: ../src/tutor.c:476 msgid "Learning the key positions." msgstr "Njàngum féetéwaayu (palaasu) butoŋ yi" #: ../src/tutor.c:479 msgid "Press any key to start the exercise. " msgstr "Bësal ci benn butoŋ ngir tàmbali jéemantu bi." #: ../src/tutor.c:612 ../src/tutor.c:615 msgid "Start typing when you are ready. " msgstr "Tàmbalil tàppe su fekkee ne pare nga (njekk nga)." #: ../src/tutor.c:613 msgid "Use backspace to correct errors." msgstr "" #: ../src/tutor.c:1060 #, c-format msgid "ps.: logging not performed for this session: the number of typed characters (%i) must be greater than %i." msgstr "PS: amul benni xibaarukaay bu ñeel njàng mii : limu araf yi u tàppe (%i) dafa war a gën a bari %i. " #: ../src/tutor.c:1200 msgid "ps.: you have entered the Top 10 list, great!" msgstr "PS: dugg nga ci lim\"Top10), waaw góor!" #: ../src/tutor.c:1214 msgid "ps.: the text you just typed doesn't seem to be similar to ordinary texts in the language currently selected: we can't account for it in the 'Top 10' contest." msgstr "PS: Mbind mi nga dugal dafa mel ni bokkul ak mbind yu niróo yi ci làkk wi ñu fal : mëneesul koo boole ci raw gaddu\"Top 10\"" #. Begin the accuracy #: ../src/tutor.c:1259 msgid "STATISTICS" msgstr "LIM YI" #: ../src/tutor.c:1260 msgid "Elapsed time:" msgstr "Diir bi jàll" #: ../src/tutor.c:1261 msgid "minute and" msgid_plural "minutes and" msgstr[0] "simili ak" msgstr[1] "Simili ak" #: ../src/tutor.c:1262 msgid "second" msgid_plural "seconds" msgstr[0] "saa" msgstr[1] "Saa" #: ../src/tutor.c:1263 msgid "Error ratio:" msgstr "Ni njuumte yi tollu: " #: ../src/tutor.c:1263 msgid "Accuracy:" msgstr "Jubaay:" #: ../src/tutor.c:1284 ../src/tutor.c:1309 ../src/tutor.c:1332 #: ../src/tutor.c:1358 msgid "Goal:" msgstr "Jëmu:" #: ../src/tutor.c:1291 msgid "Characters per second:" msgstr "Araf ci sa" #: ../src/tutor.c:1309 msgid "(CPS)" msgstr "(CPS)" #: ../src/tutor.c:1314 msgid "Words per minute:" msgstr "Baat ci simili" #: ../src/tutor.c:1339 msgid "Fluidness:" msgstr "Rattaxaay" #: ../src/tutor.c:1366 msgid "Comments:" msgstr "Gis-gis" #: ../src/tutor.c:1844 msgid "space" msgstr "diggante" #. Translators: the name of letter Y #: ../src/tutor.c:1849 msgid "wye" msgstr "Biddiw" #. Translators: the name of the Return key #: ../src/tutor.c:1853 msgid "enter" msgstr "dugal" #: ../src/tutor.c:1859 msgid "apostrophe" msgstr "cofu" #. Translators: double quote symbol: " #: ../src/tutor.c:1863 msgid "quote" msgstr "këmbu cofu" #. Translators: ampersand symbol: & #: ../src/tutor.c:1867 msgid "ampersand" msgstr "'ak' móoluwaay" #. Error frequencies or touch times #. #: ../src/plot.c:321 msgid "Character" msgstr "" #: ../src/plot.c:333 msgid "Date & Time" msgstr "Bés ak waxtu" #: ../src/basic.c:273 msgid "This custom lesson is empty. You can define two or more different characters to generate a personal practice. Press the editting button in the upper-right corner." msgstr "" #: ../src/basic.c:372 msgid "Positions of keys seems to be learned!" msgstr "Palaasu butoŋ yi mel na ni mokk na!" #: ../src/basic.c:373 msgid "" " Congratulations!\n" " You have accomplished the entire basic course.\n" " Go to the next type of exercise: adaptability.\n" " There you will practice mainly the accuracy.\n" msgstr "" "Waaw góor: \n" " Motal ngéen sëkk saaru cosaan wi, \n" " Demléen ci xeeti jéemantu yii: dëppale, \n" " Da ngéen di gën a def ay jéemantu yu ñeel jubaay, \n" #: ../src/basic.c:379 msgid "" " All right, now you got it!\n" " Go to the next lesson.\n" msgstr "" "Baax na, sottal ngéen ko!\n" " Jàll-léen ci saar wi ci topp. \n" #: ../src/adaptability.c:247 #, fuzzy, c-format msgid "" " Your accuracy rate is below %.0f%%...\n" " Could you please try again to improve it?\n" msgstr "" "Seen tolluwaay ci mbind mu jub ëppul 90%...\n" "Ndax mën ngéen a dooraat ngir yokk ko?\n" #: ../src/adaptability.c:250 #, fuzzy, c-format msgid "" " You are doing well. But...\n" " Could you make the accuracy reach %.0f%%?\n" msgstr "" "Ni ngéen di defe baax na. Waaye...\n" " jéemléen a yegg ci mbindin mu jub gën gaa néew 95%. \n" #: ../src/adaptability.c:253 #, fuzzy, c-format msgid "" " You are almost there, but your accuracy rate is still below %.0f%%.\n" " Try a few more times, or maybe you're getting upset, so go to another kind of exercise.\n" msgstr "" "Daanaka yegsi ngéen ci, waaye seen mokkal mbind mu jub a ngi ba tey ci lu yées %.0f%%\n" "Jéemaatléen\n" #: ../src/adaptability.c:260 #, c-format msgid "" " Very good!\n" " You succeeded with an accuracy rate above %.0f%%.\n" " Now it is time to increase your velocity.\n" " Go to the 3rd exercise at the main menu.\n" msgstr "" "Baax na lool!\n" " Jàll ngeen ak jub gu romb %.0f%%.\n" " Léegi, dafa jot ngéen yokk seen gaawaay.\n" " Demléen ci ñetteelu jéemantu bi te tàmbalee ca jël lu mag la.\n" #: ../src/velocity.c:333 ../src/fluidness.c:436 msgid "Pasted_or_dropped" msgstr "taf mbaa teg" #: ../src/velocity.c:444 msgid "" " You are just beginning.\n" " Be patient, try it again every day, rest and don't worry so much:\n" " persistence and practice will improve your velocity.\n" msgstr "" "Dal-bees ngéen ba léegi.\n" "Bu léen yàkkamti, jéemaatléen bés bu nekk, buléen faale:\n" "Yàgg ceeg sax ci dina tax ngeen gën a yokk seen gaawaay. \n" #: ../src/velocity.c:448 #, fuzzy, c-format msgid "" " Still away from the highway. You can do better...\n" " Try to reach at least %.0f WPM.\n" msgstr "Ba tey sori ngéen xàll wu mag wi. War ngéen a mën lu gën a baax lii.../nJéemleena jot lu gën ga neew 20 MPM.\n" #: ../src/velocity.c:451 #, fuzzy, c-format msgid "" " You are doing well, but need to go faster.\n" " And don't forget the accuracy. Try to get %.0f WPM.\n" msgstr "" "Yéen a ngi koy doxal bu baax, waaye na gën a gaaw. \n" "Te buléen fàtte jubaay bi. jéemléen a yegg ba 30 baat ci simili bu nekk,\n" #: ../src/velocity.c:454 #, fuzzy, c-format msgid "" " Fine. Now you need to start running.\n" " Can you reach %.0f WPM?\n" msgstr "" "Baax na. Léegi, mën ngéen a jéem a daw.\n" "Ndax di ngéen mën a dem ba 40 baat ci similili?\n" #: ../src/velocity.c:457 #, c-format msgid "" " Very good. You are almost there.\n" " Can you finally reach %.0f WPM?\n" msgstr "" "Baax na lool. Jàpp ngéen ko daanaka.\n" "Léegi, mën ngéen a yegg ci..%.0f...simili?\n" #: ../src/velocity.c:460 msgid "" " Excellent. For this course, that is enough.\n" " Try now the fluidness exercises, OK?\n" msgstr "" " Dox na. Doy na nii ci saar wii.\n" " Jéemantu ngéen léegi ci rattaxaay gi, baax na?\n" #: ../src/velocity.c:463 #, fuzzy, c-format msgid "" " Fast! Are you a professional?\n" " So, try to get %.0f WPM!\n" msgstr "Gaaw na lool. Ndax di gnéen tàggatu ngir jongante.Su fekkee loolu la jéemleen agg 70 MPM !\n" #. Translators: Speed Racer is a reference to a Japanese anime franchise #. about automobile racing, also known as Mach GoGoGo. #: ../src/velocity.c:468 #, c-format msgid " Ranking good, Speed Racer! Are you afraid of reaching %.0f WPM?\n" msgstr "" #. Translators: feel free to change the reference to that martial art, if you find another good analogy. #: ../src/velocity.c:472 #, fuzzy, c-format msgid "" " Kung-fu mastery!\n" " Can you fly at %.0f WPM?\n" msgstr "" "Noot ngéen nekkinu Dvorak!\n" "Ndax mën ngéen a naaw ba 90 baat ci simili bu nekk?\n" #. Translators: Dvorak here means that infamous ergonomic keyboard layout. Feel free to change the speed mastery analogy. #: ../src/velocity.c:475 msgid "" " Dvorak master!\n" " I have no words to express my admiration!\n" msgstr "" "Ub nga làmbu Dvorak! \n" "Xamu ma naka laay waxe sama cofeel! \n" #: ../src/fluidness.c:539 #, c-format msgid "" " You type accurately but not so fast.\n" " Can you reach %.0f WPM?\n" msgstr "" "Sa tàppe jub na waaye gaawul.\n" "Ndax mën ngéen a yegg ci..%.0f...simili?\n" #: ../src/fluidness.c:542 #, c-format msgid "" " Your rhythm is not so constant. Calm down.\n" " For now, try to make the fluidness greater than %i%%.\n" msgstr "" "Seen doxin dees na. Dalal.\n" " Léegi, jéemléen a yegg ci wàllu rattaxaay ci lu weesu ..%i%%.\n" #: ../src/fluidness.c:545 #, c-format msgid "" " You are almost getting there. Type more fluently.\n" " I want a fluidness greater than %.0f%%.\n" msgstr "Daanaka yeggsi nga ci. Ni ngéen di tàppee na gën a yomb./Damaa bëggoon a am rattaxaay bu toll ci ..%.0f%% mbaa lu ko ëpp/ \n" #: ../src/fluidness.c:548 msgid "" " Congratulations!\n" " It seems to me that you are a professional.\n" " You don't need this program (me) anymore.\n" " Hope you have enjoyed. Thanks and be happy!\n" msgstr "" "Waay góor!\n" "Dangaa mel ni li sa liggéey la!Soxlaatu léen porogaraam bii!/nYaakaar naa ne neex na la! Jërëjëf jàmm ak xéewal!\n" #: ../src/fluidness.c:553 msgid "" " How can you type so fast?\n" " You have exceeded all my expectations.\n" " Are you a machine? Could you teach me?\n" " I can not help you anymore. Go to an expert!\n" msgstr "" "Naka ngéen di def ba gaawe nii su ngeen di tàppe?\n" "Romb ngéen samay njoort yépp.\n" "Ndax masin ngéen? Ndax di gneen ma mën a jàngal.\n" "Mënatuma léen a jàppale. Seetiléen ku xereñ: \n" #: ../src/top10.c:68 msgid "Name" msgstr "Tur" #: ../src/top10.c:94 msgid "Chars" msgstr "Araf yi" #: ../src/top10.c:96 msgid "When" msgstr "Kañ" #: ../src/top10.c:125 msgid "Local scores" msgstr "Manoore biir" #: ../src/top10.c:126 msgid "External scores" msgstr "Manoorey biti" #: ../src/top10.c:713 msgid "Empty ranking. Please practice fluidness." msgstr "Toftal gu deful dara. Taggat leen seen bopp ci rataxaay." #: ../src/top10.c:810 msgid "Not able to download files" msgstr "Mëneesul a yeb dencukaay yi" #: ../src/top10.c:810 ../src/top10.c:902 msgid "not found" msgstr "Kenn xamul fu mu nekk" #: ../src/top10.c:811 ../src/top10.c:903 msgid "Are you sure you have it installed in your system?" msgstr "Ndax wóor na la ne sampu na ci sa doxalin?" #: ../src/top10.c:857 msgid "Could not download file from the host server." msgstr "Mëneesul a yeb dencukaay bii ca masinu (serwëëru) njaatigé ba." #: ../src/top10.c:902 msgid "Not able to upload files" msgstr "Mëneesul a yónnee dencukaay yi." #: ../src/top10.c:989 msgid "Could not upload/download scores." msgstr "Mënuñu yónnee/yeb ay manoore." #~ msgid "Keep this checked if you want to get those nice beeps." #~ msgstr "Danu koo war a bàyyi cig pal su ngeen bëgge dégg dégtu yu neex yii." #~ msgid "_Beep" #~ msgstr "Bip " #, fuzzy #~ msgid "keyboard;typing;tutor;CAI" #~ msgstr "Arafukaay " #~ msgid "" #~ " Top of \"qwerty\". Now it's time to change to the Dvorak mode.\n" #~ " Are you afraid of reaching 80 WPM?\n" #~ msgstr "Fi manoore mën a yem ci \"qwerty\". Jot na ñu jàmm ci nekkinu \"Dvorak. /nNdax dangéen ragal a yegg ci 80 baat ci simili bu nekk?\n" #~ msgid "Press here to restart the exercise. Hotkey: [Ctrl R]" #~ msgstr "Bësal fii ngir tàmbaliwaat jéemantu bi. Gàttal : [Ctrl R]" #~ msgid "_Font" #~ msgstr "Araf" #~ msgid "Default" #~ msgstr "Ñakk ndigël"